thumbnail

National Anthem of Senegal (Wolof) - Gayndeg sibi xiiru na

Guess the Wolof lyrics of the national anthem of Senegal: The Red Lion.
Based on Wikipedia
Try the French lyrics here
Quiz by
TRG5542
Rate:
Last updated: May 18, 2026
You have not attempted this quiz yet.
First submittedMay 18, 2026
Times taken0
Report this quizReport
35:00
Enter lyric here
0
 / 410 guessed
The quiz is paused. You have remaining.
Scoring
You scored / = %
This beats or equals % of test takers also scored 100%
The average score is
Your high score is
Your fastest time is
Keep scrolling down for answers and more stats ...
First Stanza
Yëngalleen
kooraa
yi,
te
jiin
ndënd
yi.
Gayndeg
sibi
xiiru
na
Ki
doon
rëbb
ci
àll
bi
Dafa
tëb
ci
kanam,
Tëb
daal
di
dal,
Dindi
lépp
lu
lëndëmoon.
Doon
jant
ci
sunuy
njàqare,
doon
jant
ci
sunu
yaakar.
Jógleen,
bokk
yi,
Afrig
booloo
na
Chorus
Wuumi
sama
xol
bu
nëtëx
bii!
Mbagg
ak
mbagg,
yeen
samay
bokk,
Ô
saa-
senegal,
jógleen!
Nanu
boole
géej
yi
ak
siyaan
yi,
nanu
Chorus
boole
joor
gi
ak
ñaay
bi!
Mucc
ñeel
Afrig
sunu
yaay.
Second Stanza
Senegaal
yaw
doomi
gayndeg
sibi,
Yaw
mi
jóg
ci
guddi
di
njaabal
i
fas,
Delloo
nu,
oh!
Dello
nu
ngalla
njàmbaarug
sunu
maam
ya,
Taaru
ni
njalabaan
dëgër
këcc
ni
sidit.
Noo
ngi
wax
jub
xocc-
jaasi
ji
amul
lenn
ngaañ.
Chorus
Wuumi
sama
xol
bu
nëtëx
bii!
Mbagg
ak
mbagg,
yeen
samay
bokk,
Ô
saa-
senegal,
jógleen!
Nanu
Chorus
boole
géej
yi
ak
siyaan
yi,
nanu
boole
joor
gi
ak
ñaay
bi!
Mucc
ñeel
Afrig
sunu
yaay.
Third Stanza
Senegaal,
def
nanu
sunu
mbir
sa
yéene
ju
kawe:
Dajale
cuuj
yi
ngir
làq
leen
jaxaay
yi
Ngir
def
leen,
li
ko
dale
penku
jëm
sowu,
bëj-
gànaar
jàpp
bëj-
saalum,
Taxaw
temm,
doon
wenn
askan,
askan
wu
dul
teqalikoo,
Waaye
askan
wu
wëlbatiku
jëm
ci
mbooleem
ngelawi
àddina
si
Chorus
Wuumi
sama
xol
bu
nëtëx
bii!
Mbagg
ak
mbagg,
yeen
samay
bokk,
Ô
saa-
senegal,
jógleen!
Nanu
boole
géej
yi
ak
siyaan
yi,
nanu
boole
joor
gi
ak
ñaay
bi!
Mucc
ñeel
Afrig
sunu
yaay.
Fourth Stanza
Senegaal,
niki
yaw,
niki
mbooleem
sunu
jàmbaar
yi,
Dinanu
dëgër
këcc
te
du
ànd
ak
mbañeel
boole
ko
ak
tijji
sunu
ñaari
yoxo.
Jaasi
ji,
dinanu
ko
roof
ci
biir
mbarum
jàmm.
Ndax
Fourth Stanza
kat
liggéey
mooy
doon
sunu
ngànnaay
ak
sunu
kàddu.
Bàntu
bi
sunu
mbokk
la,
ak
Araab
bi
ak
ku
Weex
ki.
Chorus
Wuumi
sama
xol
bu
nëtëx
bii!
Mbagg
ak
mbagg,
yeem
samay
bokk,
Ô
saa-
senegal,
jógleen!
Nanu
boole
géej
yi
ak
siyaan
yi,
nanu
boole
joor
gi
ak
ñaay
bi!
Mucc
ñeel
Afrig
sunu
yaay.
Fifth Stanza
Waaye
nag
bu
noon
bi
taalee
sunuy
dig
Dinanu
taxaw
jonn
nag
Fifth Stanza
ŋàbb
sunuy
ngànnaay:
Wenn
askan
ci
pas-
pasu
jàmmaarloo
ak
lépp
luy
tiis,
Ndaw
ñi
ak
mag
ñi,
góor
ñi
ak
jigléen
ñi.
Dee,
waaw!
Dee
lanu
wax,
waaye
mukk
ci
ag
toroxtaange.
Chorus
Wuumi
sama
xol
bu
nëtëx
bii!
Mbagg
ak
mbagg,
yeen
samay
bokk,
Ô
saa-
senegal,
jógleen!
Nanu
boole
géej
yi
ak
siyaan
yi,
nanu
boole
joor
gi
ak
ñaay
bi!
Mucc
ñeel
Afrig
sunu
yaay.
Save Your Stats
Your Next Quiz
Name all 50 states in the USA. Easy, right?
20 random countries have been removed from the map of the world! Can you identify them in 3 minutes?
Click all the Marvel characters who have had their own solo movie in the Marvel Cinematic Universe.
Drag the flag onto the correct state. Careful, though! One wrong move and the game ends.
Comments
No comments yet